Matthew 27:22-23

Matthew 27:22-23 GWG

Pilate ne len, Lan lā ela def mbōk ak Yesu ki tūda Krista? Ñepa ne, Na ñu ko dāj chi kura. Kēlifa ga ne, Lutah͈, lan lu bon la def? Wande ñu h͈āchu bu bāh͈, ne, Na ñu ko dāj chi kura.