1
John 14:27
Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
Jama lā bayi ak yēn; suma jama lā len may: dowul naka ko aduna si maye lā len ko maye. Bu sēn h͈ol jāh͈le, te bu mu tīt.
Thelekisa
Phonononga John 14:27
2
John 14:6
Yesu ne ko, Man mā di yōn wi, ak dega gi, ak dūnda gi; ken du ñou fi Bay ba, lu dul chi man.
Phonononga John 14:6
3
John 14:1
Bu sēn h͈ol jāhle: gum ngēn chi Yalla, gum len itam chi man.
Phonononga John 14:1
4
John 14:26
Wande Dalalkat ba, mu di Nh͈el mu Sela ma, ka Bay ba di yōni chi suma tur, di na len jemantali yef yepa, te fatali len lu ma len wah͈ on yepa.
Phonononga John 14:26
5
John 14:21
Ku am suma i eble, te dēncha len, mō ma sopa: te ka ma sopa mōm la suma Bay di sopa, te man di nā ko sopa, te fêñu ko suma bopa.
Phonononga John 14:21
6
John 14:16-17
Te di nā ñān Bay ba, te di na len may benen Dalalkat, ndah͈ mu neka ak yēn bel mos; Nh͈el i dega ma la: ka aduna si munul a nangu; ndege gisu ko, te h͈amu ko: yēn a ko h͈am; ndege deka na ak yēn, te di na neka chi yēn.
Phonononga John 14:16-17
7
John 14:13-14
Te lu mu mun a don lu ngēn di ñān chi suma tur, lōlu lā di def, ndah͈ Bay ba ame ndam chi Dōm ji. Su ngēn ñāne lu neka chi suma tur, di nā ko def.
Phonononga John 14:13-14
8
John 14:15
Su ngēn ma sope, di ngēn dēncha suma i eble.
Phonononga John 14:15
9
John 14:2
Cha suma ker Bay i ndekay yu bare ana fa; su nekul on nōnu, da ma len wah͈ kon; ndege mange dem wājal len bereb.
Phonononga John 14:2
10
John 14:3
Te su ma deme te wājal len bereb, di nā delusêti, te jel len chi suma bopa; ndah͈ fa ma neka, yēn itam ngēn mun fa neka.
Phonononga John 14:3
11
John 14:5
Thomas ne ko, Borom bi, h͈amu ñu fo di dem; naka la ño h͈ame yōn wa?
Phonononga John 14:5
Ekuqaleni
IBhayibhile
Izicwangciso
Iividiyo