1
Matthew 4:4
Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
Wande mu tontu, ne, Binda nañu, ne, Nit du mburu reka la dunde, wande itam bāt bu neka bu juge chi gemeñ i Yalla.
Ṣe Àfiwé
Ṣàwárí Matthew 4:4
2
Matthew 4:10
Fōfale Yesu ne ko, Randu ma Seytane, ndege binda nañu, ne, Na nga jāmu Borom ba sa Yalla, te na nga ko topa, mōm reka.
Ṣàwárí Matthew 4:10
3
Matthew 4:7
Yesu ne ko, Binda nañu, nêti, Bul fir Borom ba sa Yalla.
Ṣàwárí Matthew 4:7
4
Matthew 4:1-2
Fōfale la Nh͈el ma jīte Yesu cha manding ma, ndah͈ Seytane fir ko. Ganou ba mu ôre lu day na ñenent fuk’ i bechek ak ñenent fuk’ i gudi, mu h͈īf.
Ṣàwárí Matthew 4:1-2
5
Matthew 4:19-20
Mu ne len, Topa len ma, te di nā len def i mōl i nit. Ñu wocha mbal ya chi tah͈ouay, te topa ko.
Ṣàwárí Matthew 4:19-20
6
Matthew 4:17
Cha wah͈tu wōga Yesu dôr a wāre, ne, Rēchu len: ndege ngur i ajana jegeñsi na.
Ṣàwárí Matthew 4:17
Ilé
Bíbélì
Àwon ètò
Àwon Fídíò