1
Matthew 22:37-39
Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
Mu ne ko, Na nga sopa Borom bi sa Yalla ak sa h͈ol bepa, ak sa fit wepa, ak sa nh͈el mepa. Bile di eble bu rey ba ak bu jeka ba. Te ñarel bu niro ak mōm di bile, Na nga sopa sa morom niki sa bopa.
Compare
Explore Matthew 22:37-39
2
Matthew 22:40
Chi ñar i eble yile la yōn wa yepa ak la yonent ya bind’ on japu.
Explore Matthew 22:40
3
Matthew 22:14
Ndege ñu bare la ñu ô, wande ñu new la ñu tana.
Explore Matthew 22:14
4
Matthew 22:30
Ndege chi ndēkite ga du ñu sey, te du ñu len maye chi sey, wande di nañu neka naka malāka ya cha ajana.
Explore Matthew 22:30
5
Matthew 22:19-21
Won len ma h͈ālis i ngalak li. Ñu yub ko h͈asab. Mu ne len, Bile ban natal la ak mbinda? Nu ne ko, Cæsar la. Mu ne len mbōk, Joh͈ len Cæsar yef i Cæsar; te Yalla yef i Yalla.
Explore Matthew 22:19-21
Home
Bible
გეგმები
Videos