1
Njàlbéen ga 5:24
Kàddug Yàlla gi
Enog dafa topp Yàlla, ba jekki-jekki giseesatu ko, ndaxte Yàllaa ko yéege fa moom.
Compare
Explore Njàlbéen ga 5:24
2
Njàlbéen ga 5:22
Matusalem juddu na, ba noppi Enog topp Yàlla ñetti téeméeri at (300), amaat ay doom yu góor ak yu jigéen.
Explore Njàlbéen ga 5:22
3
Njàlbéen ga 5:1
Ni téere indee askanu Aadama nii la. Ba Yàlla di sàkk nit, da koo bind ci melokaanam
Explore Njàlbéen ga 5:1
4
Njàlbéen ga 5:2
góor ak jigéen la sàkk, barkeel leen, tudde leen Nit, keroog ba mu leen sàkkee.
Explore Njàlbéen ga 5:2
Home
Bible
გეგმები
Videos