Matthew 13:20-21
Matthew 13:20-21 GWG
Te ka ñu ji won chi i bereb i doch, mō di ka dēga bāt bi, te dal di ko nangu ak banēh͈; Wande amul rên chi bop’ am, te muñ chi sā yu new dal; ndege su nah͈ar joge wala ngeten ndig bāt bi, nōg’ ak nōga mu fakatalu.