1
Njàlbéen ga 30:22
Kàddug Yàlla gi
Ba loolu amee Yàlla geestu Rasel, nangul ko, may ko doom.
Compare
Explore Njàlbéen ga 30:22
2
Njàlbéen ga 30:24
Moo tax mu tudde ko Yuusufa (mu firi Yal na dolli), ndax dafa ne: «Yal na ma Aji Sax ji dollil doom ju góor.»
Explore Njàlbéen ga 30:24
3
Njàlbéen ga 30:23
Mu ëmb, am doom ju góor, daldi ne: «Yàlla teggil na ma gàcce.»
Explore Njàlbéen ga 30:23
Home
Bible
Plans
Videos