1
Njàlbéen ga 29:20
Kàddug Yàlla gi
Ci kaw loolu Yanqóoba liggéeyal Laban diiru juróom ñaari at ngir Rasel, te mu mel ni ay fan rekk ci moom ndax mbëggeel, gi mu am ci Rasel.
Compare
Explore Njàlbéen ga 29:20
2
Njàlbéen ga 29:31
Ba Aji Sax ji gisee ne Leya fonkeesu ko, mu may ko, mu taawlu, te Rasel moom manula am doom.
Explore Njàlbéen ga 29:31
Home
Bible
Plans
Videos