1
Njàlbéen ga 18:14
Kàddug Yàlla gi
Ana lu të Aji Sax ji? Bu ñu ca àggee nëgëni déwén déy, dinaa fi délsiwaat, te Saarata dina am doom ju góor.»
Compare
Explore Njàlbéen ga 18:14
2
Njàlbéen ga 18:12
Ci kaw loolu Saarata ree ci suuf, daldi ne: «Man mu ñor xomm mii, ndax man naa amati boobu bànneex, te sama boroom kër it di mag?»
Explore Njàlbéen ga 18:12
3
Njàlbéen ga 18:18
Ndax kat Ibraayma dina sos xeet wu mag te am doole, te xeeti àddina yépp ci moom lañuy barkeele.
Explore Njàlbéen ga 18:18
4
Njàlbéen ga 18:23-24
Naka la Ibraayma jegeñsi, ne ko: «Mbaa doo boole ku jub ak ku jubadi, rey leen? Su juróom fukk rekk jubee ca dëkk bi, mbaa doo tas dëkk bi ba tey, tee nga leena jéggal rekk ngir juróom fukk ñu jub ña ca nekk?
Explore Njàlbéen ga 18:23-24
5
Njàlbéen ga 18:26
Aji Sax ji ne ko: «Su ma gisee ci Sodom juróom fukk ñu jub, dinaa jéggal waa dëkk bi yépp ngir ñoom.»
Explore Njàlbéen ga 18:26
Home
Bible
Plans
Videos