Njàlbéen ga 18:12
Njàlbéen ga 18:12 KYG
Ci kaw loolu Saarata ree ci suuf, daldi ne: «Man mu ñor xomm mii, ndax man naa amati boobu bànneex, te sama boroom kër it di mag?»