1
Matthew 1:21
Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
Di na jur dōm ju gōr, te na nga ko tūde YESU, ndege mō di musali mbōtay am chi sēn i bakar.
Krahaso
Eksploroni Matthew 1:21
2
Matthew 1:23
H͈ēk ba di na bir, te jur dōm ju gōr, te di nañu ko tūde Emmanuel; mu tiki, Yalla and’ ak ñun.
Eksploroni Matthew 1:23
3
Matthew 1:20
Wande ba mu h͈alāte yef yile, malāka i Borom bi fêñu ko chi gēnta, ne ko, Yusufa, dōm i Dauda, bul ragal a sey ak Mariama, ndege li chi bir am chi Nh͈el mu Sela ma la juge.
Eksploroni Matthew 1:20
4
Matthew 1:18-19
Njūdu’ Yesu Krista nile la won: Ba ndey am Mariama nangulante Yusufa, ba mu lāta sey ak mōm, fêñu on na ak bir chi Nh͈el mu Sela ma. Yusufa jekar am, nek’ on ku jūb, te nangôdi ndig wone ko chi biti, bug’ on na ko fase chi kumpa.
Eksploroni Matthew 1:18-19
Kreu
Bibla
Plane
Video