1
Matthew 7:7
Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
Lāj len, te di nañu len may; ūt len, te di ngēn gis; foga len, te di nañu len ūbi
Bandingkan
Selidiki Matthew 7:7
2
Matthew 7:8
Ndege ku mu mun a don ku lāj, di na am; te ku ūt, di na gis; te ku foga, di nañu ko ūbi.
Selidiki Matthew 7:8
3
Matthew 7:24
Mōtah͈ ku mu mun a don ku dēga suma i bāt yile, te def len, di na niro ak nit i sago, ka tabah͈ nēg am chi kou doch
Selidiki Matthew 7:24
4
Matthew 7:12
Mōtah͈ lu ngēn buga lepa nit di len ko defal, yēn itam na ngēn ela defal ñenen: ndege bile di yōn wi ak yonent ya.
Selidiki Matthew 7:12
5
Matthew 7:14
Ndege bunta ba h͈ocha na, te yōn wa jublu chi dunda h͈at na, te ñu new a ko gis.
Selidiki Matthew 7:14
6
Matthew 7:13
H͈araf len chi bunta bu h͈ocha ba: ndege bunta ba yā na, te yōn wa jublu chi sankute yātu na, te bare na ñu cha tabi
Selidiki Matthew 7:13
7
Matthew 7:11
Yēn ñi bon nak, su ngēn h͈ame may sēn i dōm yef yu bāh͈, as sēn Bay ba cha ajana di na may ña ko lāj yef yu bāh͈?
Selidiki Matthew 7:11
8
Matthew 7:1-2
Bu len di ate, ndah͈ kena du len ateji. Ndege ate bu ngēn ate ñenen, di nañu len ko ateji; te natu bu ngēn di natale, mōm sah͈ la ñu len di nataleji.
Selidiki Matthew 7:1-2
9
Matthew 7:26
Te ku mu mun a don ku dēga suma i bāt yile, te defu len, di na niro ak nit ku ñaka sago, ka tabah͈ nēg am chi kou banh͈aleñ
Selidiki Matthew 7:26
10
Matthew 7:3-4
Lu elal nga di nimeku felah͈ bi chi sa but i morom, te do gis lā bi chi sa but? Wala naka nga wah͈e sa morom, ne, Bayi ma ma dindi felah͈ bi chi sa but, te lā’ngi chi sa but sah͈?
Selidiki Matthew 7:3-4
11
Matthew 7:15-16
Otu len i yonent i nafeh͈a ya, di ñou fi yēn chi nchangay i nh͈ar, wande chi bir ño di buki yu fuh͈ale. Di ngēn len h͈am chi sēn i mēñef. Ndah͈ nit di na dajale i dōm i garap i biñ chi i dek, mbāt i sōto chi i h͈āh͈am?
Selidiki Matthew 7:15-16
12
Matthew 7:17
Nōgu itam garap gu bāh͈ gu neka di na mēña mēñef bu bāh͈; wande garap gu bon di na mēña mēñef bu bon.
Selidiki Matthew 7:17
13
Matthew 7:18
Garap gu bāh͈ munul a mēña mēñef bu bon, te garap gu bon munul a mēña mēñef bu bāh͈.
Selidiki Matthew 7:18
14
Matthew 7:19
Garap gu neka gu mēñul mēñef bu bāh͈, di nañu ko gor, te sani ko chi safara.
Selidiki Matthew 7:19
Halaman Utama
Alkitab
Pelan
Video