Njàlbéen ga 2:3
Njàlbéen ga 2:3 KYG
Yàlla daldi barkeel bésub juróom ñaareel ba, def ko bés bu sell, ndax da caa dal-lu woon gannaaw liggéey, ba mu sàkke lépp.