1
Matthew 20:26-28
Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
Du neka nōgule chi sēn digante; wande ku buga rey chi sēn digante, na neka sēn bukanēg; Te ku buga neka sēn njīt, na neka sēn jām. Naka Dōm i nit ka ñouūl ndah͈ ñu bukanēgu ko, wande ndah͈ mu bukanēgu, te may dund’ am njot ngir ñu bare.
Compare
Explore Matthew 20:26-28
2
Matthew 20:16
Nōnule ña muje di nañu jītuji; te ña jītu di nañu mujeji.
Explore Matthew 20:16
3
Matthew 20:34
Yesu am yermande chi ñom, lāl sēn i but, te chi tah͈ouay sēn i but gis, te ñu topa ko.
Explore Matthew 20:34
Home
Bible
გეგმები
Videos