1
Njàlbéen ga 11:6-7
Kàddug Yàlla gi
Aji Sax ji da ne: «Su ñu tàmbalee nii, di menn mbooloo te bokk wenn làkk, kon dara dootu leen të. Ayca nu wàcc, safaan seen làkk, ba dootuñu déggoo.»
Compare
Explore Njàlbéen ga 11:6-7
2
Njàlbéen ga 11:4
daldi ne: «Ayca nu tabax ab dëkk bu taax ma bëtt asamaan; kon dinanu am woy, te dunu tasaaroo ci kaw suuf.»
Explore Njàlbéen ga 11:4
3
Njàlbéen ga 11:9
Looloo tax ñu tudde dëkk ba Babel (mu firi Safaan), ndax foofa la Aji Sax ji safaane làkku àddina sépp, mu jaxasoo, te fa la leen tasaaree ci kaw suuf sépp.
Explore Njàlbéen ga 11:9
4
Njàlbéen ga 11:1
Ca ndoorte la nag waa àddina sépp a bokkoon wenn làkk, seeni wax di benn.
Explore Njàlbéen ga 11:1
5
Njàlbéen ga 11:5
Ba ñu noppee Aji Sax ji wàcc, xoolsi dëkk bi ak taax, mi doom aadama yi tabax.
Explore Njàlbéen ga 11:5
6
Njàlbéen ga 11:8
Ba loolu amee Aji Sax ji jële leen foofa, tasaare leen ci kaw suuf sépp, ñu yemale fa dëkk ba ñu doon tabax.
Explore Njàlbéen ga 11:8
Home
Bible
გეგმები
Videos