1
John 20:21-22
Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
Yesu nêti len, Jama and’ ak yēn: naka ma Bay ba yōni on, man it nōnu lā len yōni. Te ba mu wah͈e lōlu, mu bini cha ñom, te ne len, Nangu len Nh͈el mu Sela ma
Bera saman
Njòttu John 20:21-22
2
John 20:29
Yesu ne ko, Ndege gis nga ma tah͈na nga gum: barkel cha ña gisul, wande da ñu gum.
Njòttu John 20:29
3
John 20:27-28
Ganou lōlu mu ne Thomas, Defal file sa baram, te gis suma i lōh͈o; te defal file sa loh͈o te jō ko chi suma wet: te bul gumadi, wande na nga gum. Thomas tontu te ne ko, Suma Borom ak suma Yalla.
Njòttu John 20:27-28
Heim
Biblía
Áætlanir
Myndbönd