John 21:18
John 21:18 GWG
Chi dega, chi dega, mangi la di wah͈, Ba nga nek’ on ndau, dan nga lah͈asay sa bopa, te doh͈āni fo buga: wande bo magete, di nga talal sa i loh͈o, te kenen di na la lah͈asay, te yubu la fo bugul.