Njàlbéen ga 32:30
Njàlbéen ga 32:30 KYG
Yanqóoba ne ko: «Waaw, yaw nag noo tudd?» Mu wax ko ne ko: «Loo may laaje sama tur?» ba noppi barkeel ko foofa.