Njàlbéen ga 17:5
Njàlbéen ga 17:5 KYG
Te tuddatuloo Ibraam; léegi yaa di Ibraayma (mu firi Maamu ñu bare), ndax maa la def ngay maamu xeet yu baree bare.