1
Matthew 19:26
Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
Yesu sêt len, ne len, Lile munul a am ak nit; wande dara teūl Yalla.
Compare
Explore Matthew 19:26
2
Matthew 19:6
Nōgule nekatu ñu ñar, wande bena yaram. Mōtah͈ lu Yalla bōlāte, nit waru ko fasāle.
Explore Matthew 19:6
3
Matthew 19:4-5
Mu tontu len, ne, Ndah͈ jangu len ne ka len bind’ on cha ndôrte la, dafa len bind’ on gōr ak jigen, Te nôn, Ndig lile tah͈na be nit di bayi bay am ak ndey am, bōlo ak jabar am, te di nañu neka bena yaram ñom ñar?
Explore Matthew 19:4-5
4
Matthew 19:14
Wande Yesu ne, Bayi len gūne yu tūti yi ñu ñou fi man, te bu len len tēre: ndege ngur i ajana lew na ña mel ni ñom.
Explore Matthew 19:14
5
Matthew 19:30
Wande bare na ña jītu di nañu mujeji; te ña muje di nañu jītuji.
Explore Matthew 19:30
6
Matthew 19:29
Te ku neka ku bayi i nēg, mbāt i raka, mbāt i jigen, mbāte bay, mbāte ndey, mbāt i dōm, mbāt i tōl ngir man, di na ami lu bare lu len upa, te dona dunda gu dul jêh͈.
Explore Matthew 19:29
7
Matthew 19:21
Yesu ne ko, So buge mot, na nga dem, jay lo am, sarah͈ ko miskin ya, te di nga am jur cha ajana: te ñou, topa ma.
Explore Matthew 19:21
8
Matthew 19:17
Mu ne ko, Lutah͈ nga lāj ma lu jem chi lu bāh͈? Kena la ku bāh͈: wande so buge h͈araf chi dunda, dēgal eble ya.
Explore Matthew 19:17
9
Matthew 19:24
Te ma nêti len, Gen na yomba gelem tabi chi bir but i pursa, aste borom‐alal h͈araf chi ngur i Yalla.
Explore Matthew 19:24
10
Matthew 19:9
Te mangi len di wah͈, Ku fase ak jabar am, lu moy mu di chi njālo, te sey ak kenen, njālo na: te ku sey ak ka ñu fase, njālo na.
Explore Matthew 19:9
11
Matthew 19:23
Yesu ne i tālube am, Chi dega mangi len di wah͈, Jafeñ na borom‐alal h͈araf chi ngur i ajana.
Explore Matthew 19:23
Home
Bible
Plans
Videos