1
Matthew 15:18-19
Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
Wande yef yu gēna chi gemeñ, chi h͈ol la ñu juge; te ño di gakal nit. Ndege chi h͈ol bi la h͈alāt yu bon di juge, i mbōm, i njālo, i h͈emem, i nchacha, sēde yu di fen, i sāga
Compare
Explore Matthew 15:18-19
2
Matthew 15:11
Lu h͈araf chi gemeñ, du gakal nit; wande lu gēna chi gemeñ, mō di gakal nit.
Explore Matthew 15:11
3
Matthew 15:8-9
Nit ñile teral nañu ma ak sēn gemeñ, wande sēn h͈ol sorey na ma. Wande nēn la ñu ma jāmo, di jemantal i eble’ nit niki njemantal i Yalla.
Explore Matthew 15:8-9
4
Matthew 15:28
Fōfale Yesu tontu ko, ne, E jigen ji, sa ngum rey na lol; naka nga buga, na ame nōgu chi you. Te chi wah͈tu wōwale dōm am wer cheng.
Explore Matthew 15:28
5
Matthew 15:25-27
Wande mu ñou te jāmu ko, ne, Borom bi, lêl dimali ma. Mu tontu ko, ne, Daganul ñu jel mburu i h͈alel yi, te sani ko h͈aj yi. Wande mu ne, Wau, Borom bi; ndege h͈aj yi sah͈, di nañu di leka ndesit ya di rot chi sēn tabul i borom.
Explore Matthew 15:25-27
Home
Bible
Plans
Videos