1
John 4:24
Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
Yalla Nh͈el la; te ña ko jāmu war nañu ko jāmu chi nh͈el ak chi dega.
Compare
Explore John 4:24
2
John 4:23
Wande wah͈tu wā’nga dikasi, te jot na, ba jāmukat yu dega ya di jāmu Bay ba chi nh͈el ak chi dega: ndege Bay ba ūt ña mel ni ñale ñu jāmu ko.
Explore John 4:23
3
John 4:14
Wande ku mu mun a don ku di nān chi ndoh͈ mi ma ko mayi, du marati muk; wande ndoh͈ mi ma ko mayi, di na neka chi bir am ab tên i ndoh͈ mu di nacha be cha dūnda gu dul jêh.
Explore John 4:14
4
John 4:10
Yesu tontu te ne ko, So h͈am on maye’ Yalla, ak ki di wah͈ ak you, ne, May ma ma nān; kōn di nga ko dagān, te mu may la ndoh͈ i dūnda.
Explore John 4:10
5
John 4:34
Yesu ne len, Suma dūndu mō di def mbugel i ka ma yōni on, te motali ligey am.
Explore John 4:34
6
John 4:11
Jigen ja ne ko, Borom bi, amu la dara lo rôte, te tên bi h͈ōt na: fo di jeleji ndoh͈ i dūnda mōmu?
Explore John 4:11
7
John 4:25-26
Jigen ja ne ko, H͈am nā ne Masiu di na dika (ka tūda Krista): su dike, di na ñu jangal yef yepa. Yesu ne ko, Man mi di wah͈ ak you mōm la.
Explore John 4:25-26
8
John 4:29
Ñou len, sêt nit ka ma nitali li ma def on yepa: ndah͈ du mō di Krista?
Explore John 4:29
Home
Bible
Plans
Videos