1
John 17:17
Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
Selal len chi dega gi: sa bāt a di dega.
Compare
Explore John 17:17
2
John 17:3
Te dūnda gu dul jêh͈ a di gile, ndah͈ ñu h͈am la, you mi di Yalla ji dega dal, ak Yesu Krista ki nga yōnesi won.
Explore John 17:3
3
John 17:20-21
Ñānatu ma ngir ñom reka, wande ngir ña di gumi chi man itam chi sēn bāt; Ndah͈ ñom ñepa di bena; naka you, Bay bi, neka chi man, te man mā neka chi you, ñom itam ñu neka chi ñun: ndah͈ aduna si di gum ne yā ma yōni on.
Explore John 17:20-21
4
John 17:15
Ñānu ma ne nga gēne len chi aduna si, wande ndah͈ nga otu len chi lu bon.
Explore John 17:15
5
John 17:22-23
Te ndam li nga ma may on, may nā len ko; ndah͈ ñu neka bena, naka ñun sah͈ ñu neka bena; Man chi ñom, ak you chi man, ndah͈ ñu motaliku chi bena; ndah͈ aduna si h͈am ne yā ma yōni on, te sopa nga len, naka nga ma sope.
Explore John 17:22-23
Home
Bible
Plans
Videos