1
Njàlbéen ga 16:13
Kàddug Yàlla gi
Ajara nag tudde Aji Sax ji wax ak moom, Ata El Roy (mu firi Yaa di Yàlla jiy gis), ndaxte da ne: «Moo man! Moona gis naa Yàlla, moom it mu gisal ma boppam de!»
Compare
Explore Njàlbéen ga 16:13
2
Njàlbéen ga 16:11
tegaat ca ne ko: «Léegi jigéenu wérul nga, te dinga am doom ju góor; nanga ko tudde Ismayla (mu firi Yàlla dégg na), ndax Aji Sax ji yég na sa naqar.
Explore Njàlbéen ga 16:11
3
Njàlbéen ga 16:12
Ismaylaay tiiñe, ni mbaamu àll mu deesul not, di noonoo ñépp, ñépp noonoo ko. Mooy sanc fu muy jàkkaarlook bokkam yépp.»
Explore Njàlbéen ga 16:12
Home
Bible
Plans
Videos